In extenso, le dialogue entre Sokhna Maï et la journaliste
Je viens de raccrocher avec un interlocuteur d’un célèbre site internet dakarois.
Sans me saluer ni me demander si j’étais en mesure de poursuivre la communication, l’appelant me dit « kokou sokhna mai djamil »? Je réponds par l’affirmative et sans transition, elle me lance une phrase à la fois non structurée et extrêmement polluée :-Sokhna Si dagnu beugona xam sa xalaat thi borom alal yiy exposer seni alal aki or thi magal gui…
Surprise et très mécontente de ses manières, je lui lance à mon tour:
-Assalamou Aleykoum Sokhna Si, puis sans pause je poursuis par ceci: « lolou awma thi xalaat ».
À entendre le timbre ma voix, la personne au bout du fil pouvait bien s’imaginer que j’étais un peu alité mais ceci ne l’a pas empêchée de poursuivre avec une autre question aussi irréfléchie que la première.
-Dagno beugone sa réaction thi 12 kg d’or yi bén sokhna sou tud……. takk thi magal gui, lou thi Serigne Touba Wakh…
-Sokhna si, reponds-je, xam nga lou Sëriñ Tuuba wax, « LÉP LOU SAW YOON NÉKOUL, BUKO TÉK THI SAW YOON BATHIAY JAAR ». Et je termine la communication en lui disant ceci:
«LII NGA MAY LAAJ SAMAW YOON NÉKOU THI, BUUDÉ LU BAAX LA YALNA SAX, BUUDÉ AW SAFAAN LA, SAMAY AYIBI BOPP DOYNAMA « CAS ».
Fin de la communication.
Mbok yi,
Cheikh Abdou Al Ahad dafa wax né:
« Kén défoul kén dara, kén défaloul kén dara, lou waay déf bopam ».
Kay folklore thia biir kërëm, di dundëlé magal gui thi anam yo xam né méngo woul ak niko Sëriñ Bi beugué, ay wax douko fajj, mér douko fajj, khoulo douko fajj. Lakoy fajj moy fékhél ba yaw mikoy naxarolou, na nga dundëlé magal gui thi anam yo xam ni DANA GATHIAAL nako borom folklore ba di dundëlé.
Liñu wara défar thi sunuy jëm’a ngi tolu ni guéj gui té biss bouné ñu nék thi taa-taa yi jambuur diko thiambar aka lijënti….!
Lolu du jikoy Murid Sadix!

0 Commentaires
Soyez humble et courtois, tout le monde vous lit ici